Deuteronomy 14:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbaam-xuux, moom, we wi xar na waaye du duññ. Kon daganul ci yeen. Aw suuxam, buleen ko lekk, te méddam, buleen ko laal.