Deuteronomy 16:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngeen daldi bànneexoo seenug màggal, yeen ak seeni doom, góor ak jigéen, ak seeni jaam, góor ak jigéen, ak Leween ñeek doxandéem yeek jirim yeek jëtun, ñi ci seen biir dëkk.