Deuteronomy 16:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te itam ay àttekat aki kilifa ngeen di tabb ngir seeni giir, ci mboolem dëkk yi leen seen Yàlla Aji Sax jiy jox, ñuy àtte mbooloo mi àtteb dëgg.