Deuteronomy 16:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buleen jalgati yoon cib àtte, buleen jeng te buleen nangu alalu ger, ndax ab ger day muur bëti boroom xel, di xañ aji jub dëgg.