Deuteronomy 16:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëgg doŋŋ ngeen wara topp, ndax ngeen dund, jagoo réew mi leen seen Yàlla Aji Sax ji di jox.