Deuteronomy 17:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu ngeen demee nag ca réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji di jox, bu ngeen ko nangoo, dëkke, ba ne: «Nanu fal buur bu nu jiite ni mboolem xeet yi nu séq,»