Deuteronomy 17:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu buur bi toogee ci jalub nguuram, na bindlu ngir moom ci boppam, ab sottib téereb yoon wii cib taxañ, ci dégtalub sarxalkat yi, Leween ñi.