Deuteronomy 17:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na téere boobu ànd ak moom, mu di ci jàng giiru dundam, ndax mu tàggatu ci ragal Yàllaam Aji Sax ji, ngir di sàmm mboolem kàdduy yoon wii, ak dogali yoon yii, ngir di ko jëfe,