Deuteronomy 17:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kàddug ñaari seede ba ñett nag, ci lees di reye ki ñu wara rey, waaye deesu ko rey ci kàddug benn seede.