Deuteronomy 18:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab cér du leen ñeel ci seen biiri bokk. Aji Sax ji mooy seenub cér, na mu leen ko waxe woon.