Deuteronomy 18:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye déy yonent bu am fitu àddu genn kàddu ci sama tur, te santuma ko mu wax ko, mbaa mu wax ci turi yeneen yàlla, boobu yonent, dee mooy àtteem.»