Deuteronomy 18:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii mooy li lew sarxalkat yi, te bàyyikoo ci askan wi, ci ñiy rendi ay sarax, muy aw nag, di ab gàtt: nañu jox sarxalkat bi, mbagg mi ak lex yi, ak mbàq gi.