Deuteronomy 18:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax seen Yàlla Aji Sax ji moo ko taamu, ci seen mboolemi giir, ngir mu taxaw, di liggéey ci turu Aji Sax ji, moom ak askanam, ba fàww.