Deuteronomy 19:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ñetti dëkk yu mag ngeen di ber ca biir réew mooma leen seen Yàlla Aji Sax ji jox, ngir ngeen jagoo ko.