Deuteronomy 19:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngeen waajal nag yoon wu jëm ci dëkk bu ci nekk, te ngeen séddale ñetti pàcc réew mooma leen seen Yàlla Aji Sax ji sédd, ngir képp ku rey nit, man caa làquji.