Deuteronomy 19:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Toppkatu bakkan ba nag warul mana dabi ci biir xolam bu tàng, ki rey, ba rey ko ngir sorewaayu yoon wa jëm ca dëkkub rawtu ba, te àtteb yoon reyluwu ko, gannaaw fekkul woon mu bañ ka mu rey, démb ak bëkk-démb.