Deuteronomy 19:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndegam sàmm ngeen mboolem santaane bii ma leen dénk tey, ngir di ko jëfe, ngir sopp seen Yàlla Aji Sax ji, di awe ay yoonam bés bu nekk, su boobaa nangeen yokkaat ñetti dëkk yu mag, mu dolliku ci ñetti dëkk yi ngeen jëkka ber.