Deuteronomy 2:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seyir nag la Oreen ña jëkkoona dëkk, waaye Esaween ñaa leen fa dàqe, faagaagal leen, wuutu leen, noonu Israyil def rekk ak céru suufam bi leen Aji Sax ji jox.