Deuteronomy 2:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu ngeen àggee ca Amoneen ña nag, buleen dal ci seen kaw, buleen xeex ak ñoom, ndax duma leen jox benn cér ci réewum Amoneen ñi, ngir askanu Lóot woowu laa ko sédd.»