Deuteronomy 2:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«May nu, nu jaare sam réew. Yoon wi rekk lanuy topp; dunu jàdd ndijoor, dunu jàdd càmmoñ.