Deuteronomy 2:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Siwon buurub Esbon nag nanguwu noo may nu jaare fa moom, ndax booba seen Yàlla Aji Sax ji moo dëgëral boppam, wowal xolam, ngir teg ko ci seen loxo niki bésub tey jii.