Deuteronomy 20:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndegam jàmm lañu leen wuyoo, ba ubbil leen, mboolem askan wa mu fekk ca biir dëkk ba dañuy tegoo liggéeyu sañul-bañ, ñeel leen, di leen jaamu.