Deuteronomy 20:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye jigéen ñi ak tuut-tànk yi, ak jur gi, ak mboolem lu ne ca biir dëkk ba, mboolem alal ja, sëxëtooleen, jagoo. Lekkleen alal ji ngeen foqatee ci seen noon, yi leen seen Yàlla Aji Sax ji jébbal.