Deuteronomy 20:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax ñu bañ leena royloo, ngir ngeen di jëfe seen mboolem yu jomblu yi ñuy defal seeni tuur, ba ngeen moy seen Yàlla Aji Sax ji.