Deuteronomy 20:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu ngeen gawee lu yàgg ab dëkk, ngir song leen xare, ba nangu ko, buleen fóom ay garabam, di ca gor lenn te mana lekk ca doom ya. Kon nag garab, buleen ko gor. Garab du nit ba ñu di ko def ni ku ñu gaw.