Deuteronomy 21:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
bu néewam fanaan ca garab ga, nañu ko daldi rob ca bés ba, ndax ki wékke alkàndey Yàlla la. Buleen sobeel réew mi leen seen Yàlla Aji Sax sédd.