Deuteronomy 22:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
génneleen leen ñoom ñaar, ba ca bunt dëkk booba, ngeen dóor leen ay doj ba ñu dee, ndax ndaw si moo yuuxuwul woon wall, te muy ca biir dëkk ba, te waa ji it moo jabaroo jabaru moroomu góoram. Noonu ngeen di tenqee lu bon ci seen biir.