Deuteronomy 23:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu ngeen génnee ba fàkk ab dal, ngir jànkoonte ak seeni noon, nangeen sàmmu ci lépp lu aay.