Deuteronomy 23:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buleen indi mukk ci seen biir kër Yàlla Aji Sax ji, peyooru gànc bu jigéen, mbaa bu góor, ngir wépp xas wu ngeen namma wàccoo googu peyoor, ndax yooyu yaar yépp, seen Yàlla Aji Sax ji seexlu na ko.