Deuteronomy 23:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab Amoneen mbaa ab Mowabeen du bokk ci ndajem gëmkati Aji Sax ji. Ku askanoo ci ñoom it, ba ca fukkeelu maas ga, du bokk ci ndajem gëmkati Aji Sax ji mukk,