Deuteronomy 23:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax la ñu leen dabewul woon aw ñam, mbaa am ndox, ca yoon wa, ba ngeen génnee Misra, xanaa di fey Balaam doomu Bewor ma bokk Petor ca Aram Naarim, ngir mu sàbbi leen.