Deuteronomy 23:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buleen bañ ab Edomeen, ndax seen mbokk la. Buleen bañ nitu Misra, ndax ay doxandéem ngeen woon ca seenum réew.