Deuteronomy 24:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Deesul teg waajur àtteb dee, ngir weccikoo ko doom ja, te doom it deesu ko teg àtteb dee, weccikoo ko waajur wa. Nit ku nekk, bàkkaaru boppam lees koy tege àtteb dee.