Deuteronomy 24:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
su boobaa jëkkëram ju jëkk ja ko yiwi woon du ko saña jëlaat jabar, gannaaw ba ndaw sa sobewoo noonu, ndax loolu lu jomblu la fi kanam Aji Sax ji, te waruleena indi bàkkaar ci biir réew mi leen seen Yàlla Aji Sax ji di moomale.