Deuteronomy 24:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku jël ab séet du bokk ci gàngoor gu jëm xare, te deesu ko sas lenn. Day moom boppam atum lëmm, ngir toog këram, di bégal jabaram ji mu jël.