Deuteronomy 25:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Doju màndaxekaay bu mat te dëggu ngeen wara am, te nattukaayu sol-sotti bu mat te dëggu ngeen wara am, ndax ngeen gudd fan ca réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji di jox.