Deuteronomy 26:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu bége nag, moom ak Leween ñeek doxandéem yi dëkk ci seen biir, mboolem lu baax li ko seen Yàlla Aji Sax ji jox, moom ak waa këram.