Deuteronomy 26:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na àgg ca sarxalkat ba fa nekk ci yooyu jant, ne ko: «Maa biral tey jii fi sa kanam Yàlla Aji Sax ji, ne agsi naa ci réew mi Aji Sax ji giñaloon samay maam, ne moom la may jox.»