Deuteronomy 26:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu dellu nag wax fi seen kanam Yàlla Aji Sax ji, ne: «Sama maam ab Arameen buy màngaan la woon. Mu dem Misra, sance fa mbooloo su néew, te mujj di askan wu réy, am doole te bare.