Deuteronomy 27:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Defleen ca itam ay saraxi cant ci biir jàmm yu ngeen di lekk foofa. Ngeen daldi bége fa seen kanam Yàlla Aji Sax ji.