Deuteronomy 27:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee Musaa ak sarxalkat yi, Leween ñi wax ak Israyil gépp, ne leen: «Yeen Israyil, neleen cell te déglu. Bés niki tey doon ngeen askan wu ñeel seen Yàlla Aji Sax ji.