Deuteronomy 28:40 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ay garabi oliw ngeen di am ci seen réew mépp, waaye ag diw, dungeen ko diwoo, ndax seen doomi oliw ya day yolax.