Deuteronomy 28:44 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom moo leen di lebal, waaye dungeen ko lebal. Moom mooy doon bopp, yeen, ngeen di geen.