Deuteronomy 28:45 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem alkànde yii ñoo leen di dab, dal ci seen kaw, topp leen, ba ngeen sànku, ndax yeena déggalul seen Yàlla Aji Sax ji, ngir wormaal ay santaaneem, ak dogali yoonam, yi mu leen dénk.