bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Deuteronomy 28:51
Deuteronomy 28:51 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñooy yàpp seenug jur, lekk seen gàncax, ba ngeen raaf. Duñu leen wacce dara; du pepp, du biiñ, dug diw, du doomu jur gu gudd ak gu gàtt, ba ngeen far sànku.