Deuteronomy 28:55 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ngir baña sédd kenn ci ñoom ci yàppu doomam ya muy lekk, ndax du dese dara ca biir gaw ba, ak tanc ba leen seeni noon tanc, ci seen dëkk yépp.