Deuteronomy 28:58 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ngeen sàmmoowula jëfe mboolem kàdduy yoon wii binde ci téere bii, ngir wormaal boroom tur wu màgg wii te raglu, seen Yàlla Aji Sax ji,