Deuteronomy 28:68 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax jee leen di yeb ciy gaal, delloo leen Misra, yoon wu ma leen noon dungeen ko gisati, ngeen di fa jaay seen bopp seeni noon, ngir doon seen jaam yu góor ak yu jigéen, te kenn du leen jënd.