Deuteronomy 28:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax jeey def, noon yi leen di jógal, ñooy daanu fi seen kanam. Wenn yoon lañuy dikke, dal ci seen kaw, waaye juróom ñaari yoon lañuy awe, daw, jiitu leen.