Deuteronomy 29:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ngir def leen bésub tey, askan wi mu ñoñoo; moom ci boppam mu doon seen Yàlla, na mu leen ko waxe woon, na mu ko giñale woon seeni maam, Ibraayma ak Isaaxa ak Yanqóoba.